Difference between revisions of "Wolofavaf urimak 05"
(Redura va bu icde wolofavafa urima yo (5)) |
(Tazukara) |
||
Ligne 97: | Ligne 97: | ||
{{Wolofava_urimak_exulera | {{Wolofava_urimak_exulera | ||
− | | urimak_vergumvelt = | + | | urimak_vergumvelt = 5. (81-95 ur-) |
− | | urimak_abdueurimak = [[ | + | | urimak_abdueurimak = [[Wolofavaf_urimak_04|4. (61-80 ur-)]] |
− | | urimak_radimeurimak = [[ | + | | urimak_radimeurimak = [[Wolofavaf_urimak_05|5. (81-95 ur-)]] |
}} | }} | ||
[[Loma:Urima]] | [[Loma:Urima]] | ||
− | [[Loma:Wolofavafa urima| | + | [[Loma:Wolofavafa urima|Wolofava]] |
[[Loma:Ayoltaca yo|Wolofavafa urima se]] | [[Loma:Ayoltaca yo|Wolofavafa urima se]] |
Version du 17:19, 22 toleaksat 2008
| ||||
---|---|---|---|---|
Vergumvelt | Léébu wolof | |||
Sutesik | - | |||
Piskura | - | |||
Ava | Wolofava | |||
Evla | - | |||
| ||||
Vergumvelt | Wolofavafa urima se | |||
Kalkotavasik | Marjorie Waldstein | |||
Piskura | Kotava.org | |||
Evla | 2008 | |||
| ||||
Webesik | Marjorie | |||
Krentduga | Tuenayan |
5. Wolofavafa urima se (81-95)
81. Tànk ci suuf, jaan ci suuf, fu ñu jaar daje.
Nugeem tir moe sid, perake tir moe sid, acum sin va sint kakeveted.
82. Tilim dina dem fu saabu mënula dem.
Zionuca gitir lize tird me grutir.
83. Tuñum giléém lang na, waaye rotul.
Kutc ke wegidol sorumkawer voxe me soluber.
84. Waxi ndee bu taxawee, ndund yaa tax.
Pulva ke awalkik wan tir, tuke blisik yo.
85. Waxi mag dana guddee all, waaye du ca fanaan.
Pulva ke savsik koe mola vangaver voxe mielon me jonvieler.
86. Waxtaan ñam la, ku ko teewe ca nga.
Prilara tir dum estu, anoelik gipaker.
87. Xamul aay na wànte laajtewul a ka yéés.
Megrupera tir rotafa voxe mebibera tir lorotafa.
88. Xeeb sa takkum, mu takk saw say.
Kore rin va wazdel vligul, in va rinafa klova vaniksantur.
89. Xeex, ku ko fekke, boo àttewul, danga sot.
Bak rwama tan tcokes va int walplekuson kopakoar.
90. Xel bu doon jaay lamb.
Ede gruuca co-tir godolena, va urlijkesik me co-trasir.
91. Yaakamti ag gaawantu lugnu jur rethiou am thia yoon.
Mekeuca is ipera va batcera cabeted.
92. Yàgg ay wone légétub taat.
Ugal va penayomza razdur.
93. Yàgg du saabu, waaye dana fóót.
Ugal me tir tird voxe sotubatakawer.
94. Yàlla, yàlla, bey sa tool.
Lorikkorozara vol xolera va tayamidura.
95. Yééné néég la, boroom a cay fanaan.
Jugemera tir maga, tel kalis mielon ugalzer.
← 4. (61-80 ur-) - 5. (81-95 ur-) - 5. (81-95 ur-) → |